Qur'an in Wolof Language

Embed Size (px)

Citation preview

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    1/20

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    2/20

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    3/20

    AL

    XURAAN

    CI

    WOLOF

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    4/20

    @

    L Harmattan, 1997

    ISBN: 2-7384-5966-8

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    5/20

    Pathé D iagne

    AL XURAAN

    CI W OLOF

    É ditions L H arm attan

    5-7 , n ie de l École -Polytechnique

    75005 Paris

    L Harmattan Inc.

    55, rue Saint-Jacques

    Montréal (Qc)

    - CANADA H Y lK

    S N ORÉ

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    6/20

    Ouvrages du m êm e auteur:

    - Pouvoir politique en Afrique occidentale, Présence

    africaine, Paris, 1967.

    - Grammaire moderne du W olof, Présence africaine,

    Paris, 1967.

    - Pout l unité ouest-africaine, intégration ou m icro-état,

    Paris, Anthropos, 1972 (Thèse de Doctorat d Etat en

    Sciences Economiques, Un iversité de Paris-Sorbonne).

    - Introduction à la culture africaine, ouvrage collectif,

    Paris, UNESCO-collection 10/18, 1976.

    - Histoire générale de l Afrique noire, volum e 2, Paris,

    UNESCO , 1978.

    - L Europhilosophie face à la pensée du Négro-africain,

    Sankoré, 1979.

    -

    Bakari II (1312) et Christophe Colomb (1492) à la

    rencontre de l Amérique, Sankoré, 1992.

    - Léopold Sédar Senghor ou la négritude servante de la

    francophonie au festival d A lger.

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    7/20

    Kàddu gu jëkk

    Avant propos

    D afiuy génné fii takk ci Al Xuraan

    Nous publions ici un condensé

    ci Wo lo f.

    du Coran en W olof.

    Dafa ëmb juroom fukk ag fiatti

    saar ci téeméer ag fukk ag fient yi

    fiu tekki te nu nekk ci Téerébi Al

    Xuraan bi .

    Saar yooyu fiooy

    :

    fiatt fii jëkk ag

    fukk ag juroon yi mujj.

    Dafiu leen tànn génné ba mën

    yombal gannaaw loolu tasaare

    mu jottali fiepp Teere Al Xuraan

    bi.

    Dama fas yééne ci lu gàtt boole

    boroom xamxam yi ci ngénné Al

    Xuraan ci wolof fu mu dee mbiru

    fiépp.

    Maa ngiy sant Kumba Gey,

    Faatu Saar, Tina Cesaltine, Ndey

    Faatu Mbay noo tappe mbind mi.

    Di sant Buubakar Kan di jangale

    Ecole Normale m i ko toppaat.

    T eerehkat hi

    Il com porte soixante quinze des

    cent quatorze sourates traduites

    que contient le Coran.

    Il s agit ici des douze prem ières

    et des so ixan te s tro is dern ières.

    Ces sourates ont été choisies et

    publiées pour préparer la

    diffusion et l accès du grand

    public à la totalité du texte.

    J ai choisi de faire de la

    publication d une édition finale,

    un challenge collectif auquel

    seront associés tous ceux qui

    peu vent y apporter une

    contribution.

    Je remercie Kumba Guèye,

    Fatou Sarr Tina Césaltine,

    Ndeye Fatou Mbaye qui ont

    assuré la saisie à l ordinateur de

    ce texte. Sans oublier Boubacar

    Kane, professeur à l Ecole

    Normale Supérieure qui a bien

    vou lu le relire.

    L Éditeur

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    8/20

    UBBI

    1

    -

    Al Xuraan jii nuy jéema

    tekki fii ag di ko bind, bi fi

    lislaam duggee ba tay, julliti

    suiiu wàllu réew yii, danu mès

    di ka tèral ci seeni làkk, ba mèil

    xam Ii baatu Yàlla biy leera .

    2 -

    Loolu ngir jàppe ko seen

    xel,tàbbal ko ci seen xol, ba

    mèil rafetal topp seen Boroom .

    3 -

    Tari, tekki ag firi Al Xuraan,

    Yàlla dafa ko santaane, Dafa

    dèppoog it ag lu yomb nangu, ci

    réew ag xeetu Afrig yi cosaanoo

    démb, te bokk ci fii jè'/(k jiitè1

    xam, xamxam ag xamme, Téere

    bü, Yàlla moo ni ci Moom

    dO fJTJm oo ko m è'n tekki (suraat

    3 -

    laaya

    5).

    Loolu dafa wane

    ni ku koy tekki mbaa leeral,

    mè'nullu dul di jéem jege Ii mu

    ci làxx. Teewul mu santaane nu

    jàng ko, te di jéema xam Ii mu

    ci èinb, ag fi muy feenal.

    2

    INTRODUCTION

    1 - Le Coran dont nous

    essayons de donner ici une

    modeste traduction écrite, les

    musulmans de nos contrées

    n ont eu cesse de le naturaliser

    dans leur langue, de manière à

    saisir ce que la Parole de Dieu

    éclaire.

    2 - Cela avec le dessein de le

    comprendre dans sa rationalité,

    de l appréhender dans leur

    coeur, afin de servir D ieu de la

    meilleure manière .

    3 Réciter, traduire et

    commenter le Coran, est une

    prescription que Dieu a faite.

    Celle-ci rencontre facilem ent

    l adhésion parm i les nations

    d A frique qui appartiennent à de

    vieilles traditions, et qui, parm i

    les prem ières, ont privilégié le

    savoir, la science et la sagesse.

    Le Livre affirme que Dieu seul

    à pouvoir de donner aux versets

    du Coran leur sens exact

    (Sourate III, verset 5). Cela

    m ontre que toute explication ou

    in terprétation n est qu approche

    de ce qu il y a de caché. Il n en

    ordonne pas moins de tenter de

    saisir ce qu il recèle et qu il

    révèle.

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    9/20

    4

    -

    Santaane wi moo waral, ci

    Afrig, bi fi /islam duggee ba

    tay, daara yi di dajale xale yi,

    nu jë /(k tari AI Xuraan ju sell

    ji. Su moklœe mbaa nu mokkal

    ci lu tane nu tekkilleen ko, firil

    leen Ii nu ci jàng te jàpp ko.

    5

    -

    FU , danoo màgg ci wetu ay

    waa jur, nu gindee nu noonu ci

    dUne ji.

    6 -

    Goora Jaan sunu maam di

    lébu lam tuna bokk cin jaaneen

    yi sos nguuru Baragwatan

    reewum Barag jàppe Marog

    ba Ndeer mbaa Ndar géej ag

    Soor Jaan dun yi law de Ndar

    ci bé1u Jukk dexu Senegaal.

    Da a jogé Baragwata né'w sos

    Ker Goora ci Kajoor. Muy

    Péey mu siiw ci dUne dolli di

    Teeru, law jàpp Paal, Sakal

    Ra Baeeas ag Ciise.

    Mooy Maam Paate turandoo

    woowu ma jukkale liggéey bi

    Caatu Roxxaya Tafsir Umar

    Sàll mi sane liggéey daara te

    daan jangale, m oo i liggéey

    4

    -

    C est cette prescription qui

    légitime en Afrique, dès

    l apparition de l islam , la

    création d écoles qui

    rassemblent les enfants, pour

    qu ils commencent d abord à

    réciter le C oran sacré. U ne fois

    qu ils le savent ou qu ils en

    récitent une partie, on leur

    traduit et commente ce qu ils

    en ont retenu.

    5 - Ici, l on grandit à l ombre

    de parents qui éduquent de

    cette manière en matière de

    religion,

    6 - Gara D iagne, notre aïeul,

    lébu lam aan parm i les D iagne,

    fondateurs du Baragwata,

    royaume du Barag, allant du

    Maroc actuel à Ndeer sur mer

    et Sor D iagne, îles à l origine

    de Saint-Louis à l embouchure

    du Jukk ou Fleuve Sénégal,

    vint s installer au Kayor. Il y

    fonda ker Goora, métropole

    re lig ieuse et v ille commerc iale

    influente dans les régions de

    Pal, SakaI, Rao Bathias et

    Thisse.

    Fils cadet de Rokhaya Tafsir

    Gumar SalI qui ouvrit une

    école coranique où elle

    enseignait,

     

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    10/20

    tekkim i mU daJa bokk ci maasi

    jamano, noo xam ni Astou

    Naar, YuusuJa Sàll, Ablaay

    Njaay, Arnet Jeng ag M axtaar

    Jeng MO leen jangal

    Jéementu wi nu sumb danu ciy

    wut

    do'rJ'rJ

    u nu xirtale ulema

    boroom xamxam yi, ag Aafisul

    xuraan yi, ba nu térak ci mbind,

    tekki ag firi yu wer yi war Téeré

    bU nu téen ndonoloo.

    7- Jullitu Taari yi manaam wa

    Afrig yi, danu bokk ci ni jékk

    xer ci dé] ley, lawallislaam ag

    Al xuraan ci gisgis ag aada yi

    fi

    gën ra fe t.

    8

    -

    Lislaam bi muy feen fii,

    ndali Ghana la fi fekk wu

    Tekruur, Wadaan ag wu

    Gaawo, manaam wu Zaghawa.

    Booba nguur yooyu nooy law

    ba ca géeju Mediteraane.

    Danu fa sakk ay dé'kki teeru

    naka Talamseen, Sigil Maiga

    mbaa Tangiita. Noo ame booba

    wurusu addina wi.. di

    demanteeg Europ, Penku ag

    Bisaans.

    4

    le traducteur de texte appartient

    à une génération qui étudia

    auprès de A stou la mauresque ,

    y

    oussoupha SalI, Abdoulaye

    N diaye, Ham et Dieng et M octar

    Dieng

    L exercice que l on entreprend

    ici vise à pousser les savants

    uléma et les maîtres de Coran, à

    fixer par écrit les traditions de

    traduction et de comm entaire

    autorisées du Livre dont ils sont

    les dépositaires,

    7 - Les m usulm ans du continent

    africain sont parm i les prem iers

    à avoir fait montre de

    détennination pour asseoir et

    diffuser l islam et le Coran dans

    les persp ectiv es et les traditions

    les p lus belles,

    8 - L islam en Afrique apparut à

    l époque des Empires du Ghana

    et du Z aghawa.

    C es deux puissances politiques

    rayonnaient alors jusqu en

    Méditerranée,

    Elles y avaient créé des

    comptoirs commerciaux comme

    Talam sen, Sigil M aisa, Tanger.

    Elles contrôlaient l or du

    monde, commerçaient avec

    l Europe, l O rient et Byzance.

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    11/20

    9

    Bi fwo dugg ci

     

    teemeri at,

    lislaam tàbbi na ci xel yi ag ci

    nguur y i.

    Ghanawa yi Zaghawa yi ag

    seeni paraale dëJ nanu booba

    nguuri islaam yu bees jiital

    doxalin wùl yaatal di boole ag

    yamale iiit fiépp ci wàllu diine.

    Looloo waral mbootayu xarijiit

    yi jog taxawal diine jamono

    joojor.

    1 Tarix Ibn Siyaad Abdallaah

    Ibn Walghu di lamaan

    ghanawa, 100100

    ko jôo ci togg

    xare,

    dëJnguur

    Espaan ag wall

    ci Erobu Mediteraane, tublôo

    leen ci 710. Masayar (Maycara)

    beneen ghanawa la daan yanu,

    di jaay ndox.. dana jog jiite

    mbootaayu jullit, foxxati nguur

    gi ci reewum Tarix moomu.

    Mooy nekki imaam ag xalifa wi

    jë /(kci xeeti Afrig yi.

    11

    Nguri Talamseen, Sigil

    Maisa, ya woon ag yu bees yi

    na Tahert 761, mba Fes 786,

    noonu

    la flu lawe noom

    it gën

    dë gë.ral

    lislaam ci jamono

    yooyu.

    Ndaali Ghanna ci jamono

    yooyu la fa lislaam menn.

    9- Au début du VIlle siècle,

    l islam pénètre les esprits et les

    pouvoirs. Les Ghanawa, les

    Zaghawa et leurs alliés

    installent de nouveaux

    royaumes islam isés qui

    privilégient une démocratie très

    large et populaire, conforme àleur tradition. C est là l origine

    des grands mouvements

    kharijites qui bouleversent et

    adaptent l islam au m ieux.

    10 Tarih Ibn Z iyaad Abdallaah

    Ibn Walghu, un lamaan

    ghanawa, conquiert, en 710,

    m ilitairement, et islam ise

    l Espagne et une partie de

    l Europe méditerranéenne.

    Masayar appelé Mayçara, un

    porteur d eau, se manifeste

    comme guide en 730. Il prend le

    pouvoir dans le pays de Tarih et

    dev ien t le p remier ca life-imaam

    africain.

    11 Les anciens pouvoirs

    comme Talamsen, Sigil M aisa

    et les nouveaux nés à Tahert

    761, et Fès 786, vont s étendre

    et consolider la nouvelle foi.

    C est à la même époque que

    l islam s épanouit au Ghana.

    5

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    12/20

    12 -

    Gannaaw xew xew yooyu la

    Njawar Jaagiliba njitu xare

    reewum Ghana di togg xare wiy

    dëJi xalifa fatimid. Dafa ëm b ei

    gannawam li dale Walata ba

    Sijil M aisa ag TangUa ci géeju

    Atlanlig ci

    958,

    jublu kaw ag

    penku, dem ba Espaaiï, Sisil,

    Sardaaiï, M isira ag Siri wann

    leen.

    13- Moo sane péne mi di Keer

    ci

    969,

    tabax El Asar 970, samp

    Al Muhiz naka xaliJa. Gannaaw

    gi la walbati Bagdaad ci 973

    teg ei kiraayam iïatti dë /(kyu

    sell yi: Maka, Medin ag

    gerisalam

    14

    - M bootaayu xariijit yi mu

    bokkal jamono, Abu Yazid, benn

    zaghawa judoo Gaawo di

    jàngkat wu mag, bokk ci yoonu

    lbaadit yi, tey doomu jula wu

    am alaI moo ka sos ci

    946,

    jUtaI

    ko.Abu yasid moom daJa jog

    jublu Ifrihiya manaan Tanisè'

    mba Tunisiya ngir beesali ji fa

    dUne ju bees ji

    15 -

    War Jaabi Njaay di Buuru

    Tekruur moo galandu, dë /(ka lc i

    :Gede, maraabat Ghana, yiy

    sosi mbootayu A lmorawid

    (;

    12- C est à la suite de Tarih que

    N jawar Jaagiliba, commandant

    des armées du Ghana, mène la

    guerre sainte dont naîtra le

    Khalifat fatim ide. Il conquiert,

    dans sa foulée, l espace qui va

    de Walata à Sigil Maisa et

    T anger sur l A tlantique, en 958-

    968, se dirige vers le Nord et à

    l Est. Il atteint l Espagne, la

    Sicile, la Sardaigne, l Egypte et

    la Syrie qu il annexe.

    13- Il fonde le Caire, en 969,

    construit El hazar, en 970,

    amène Muhiz et le fait

    consacrer Khalife, après sa

    victoire sur Bagdad en 973 tout

    en se déclarant protecteur des

    trois villes saintes: la M ecque,

    Médina et Jérusalem

    14

    - Le mouvement xarijite qui

    naît, à la même époque, est

    fondé, en 946, par un Zaghawa,

    Abu Yezid, né à Gao, grand

    érudit ibadite et fils d un riche

    négociant.

    Abu Yazid ira lui.à la conquête

    de l Ifrihiya ou la Tunisie afin

    d y renouveller la nouvelle foi.

    15- War Jabi N diaye, souverain

    du Tekruur, accueille et installe

    à Gedé, en 1040, les m arabouts

    ghanawa à l origine du

    mouvement a lmoravide.

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    13/20

    yi, (1055-1147). Dafa dooleel

    Tasfiin jogé ci réewum Teen

    Samoren ànd ag Telegin njiitu

    Lamtuna wi ko éndi Gede.

    War Jaabi dafay dooleel

    mbootay goo gu. Dafa koy boole

    ag xare wu mag wu jarbaatam

    Lebu Sàll jiite, ànd ag Yahya

    Ibn Taashfiin, Abuubakar

    Taashfiin w iy sé'yag Farim ata

    Sàll jigéenu Lebu, Yuusuf, bokk

     Lenoag Abuubakar.

    Noonu noo ànd ag njiitu diine

    wiy Ibn Yaasin, ab ghanawa

    wu, bawo ci moomeelu Teen

    samoren.

    Noonu noo lawal xilaafaatu

    Almorawid yi, foUi Umeyyaad

    yi ci ngànnaaru Afrig ag ci

    Espaan.

    Almoxaad yi leen di wuutuji

    fioom ci seen bopp Ghana lanu

    bokkoon.

    16 -

    Turner m i jiite Almohaad yi

    ghanawa la. Almohaad yi

    (

    1160-1212) noo y6bbu fu sore

    dekkali dUne ag xamxam bi

    lislaam yewwi. Ci jamono

    Almohaad yi la Ibn Tofaayil ag

    Ibnu Rush feefi, dekkali Aristot

    ag xamxam i démb.

    Il sou tient Tachefin, origin aire

    du pays du Tin Zamoren et

    Telegin, le chef lam tuna qui le

    fait accueillir à Gedé.

    War Jaabi prête force au

    mouvement. Il lui fournit une

    armée conduite par Lébu SalI,

    son neveu et héritier.

    A boubacar T achefin, son beau-

    fils, époux de Farimata SalI,

    soeur de Lébu, Y oussouph

    Tachefin , cousin de Aboubaca r.

    Ce sont eux les compagnons de

    Ibn Yasin venu du pays du Teen

    Zamaren.

    C est eux qui vont étendre le

    Khalifat almoravide en

    s emparant des royaumes

    ghanawa d Afrique du Nord et

    Ommeyyade d Espagne .

    Leurs successeurs almohaad

    eux-mêmes relevaient de la

    mouvance du Ghana.

    16 Tumert, leur guide, était un

    Ghana- wa. Les Almohaad

    (1160-1212) portèrent loin la

    Renaissance religieuse et

    scientifique déclenchée par

    l islam . C est à cette époque

    qu apparaissent Ibn Tofaïl et

    Ibn Rush (A verroes) qui

    ressuscitent Aristote et la

    pensée ancienne.

    7

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    14/20

    17 -

    Maali wu Kanku Maisa ag

    Bakari mi jàll atlantig ci 1312

    dana lawal islam fay nekki

    Amérig.

    Songhai, wu Soni yi ag Askiya

    yi, iiooy ubbil bunt bi

    Suleymaan Baal, Usman Dan

    foojo, Aaj Umar Taal ag

    Samori Ture.

    Boroom xamxam yu Ghana,

    G awo, Tekruur ag Maali yooyu

    boole Soninke, Lebu-wolof,

    Pé1, Sée réer, Tuareg, Rausa

    mba Zaghawa iiU iiuu l, iiUxees,

    iiii xeereer, iiii weex, ci iii jèK k

    tekki firi ag lawal Al xuraan ci

    seen làkk laiiu bOkk.

    18 -

    Yunus B if lyaas

    (842-844)

    di sè'tu Tarih, jiitu Lamtuna ci

    Baghawarta miy Marogu tay,

    moo jè k,ktekki ag bind épp na

    fukki teemerib at Al Xuraan ci

    làkku lamtuna , zanaga .

    Ghomara yi déKkwetu Tetuwan,

    daa nu deft lu ni mel. Ci

    gannaaw gi, Tumer mi dé}

    xalifaatu Almoxaad moom itam

    tekki na T éeré bi ci làkkam.

    8

    17 - Le Mali de Kanka Maisa et

    Bakari II le mansa navigateur

    qui traverse l A tlantique en

    1312 portera l islam Outre

    Atlantique.

    Le Songhaï des Soni et des

    Askia, ouvrira la voie à

    Suleymaan Baal, Usmaan DanFojo, El Haj Umar Taal et

    Samori Ture .

    Les savants de Ghana, de Gao,

    de Tekrour et du Mali, formés

    de Soninké, de Lébu-wolof, de

    Peul, de Sérère, de Touareg, de

    Zaghawa, de Berbères noirs,

    rouges-ocres, clairs ou blancs,

    sont parm i, ceux qui auront les

    prem iers, traduit et commenté le

    Coran dans leur langue propre.

    18

    - Yunus Bit lyaas (842-

    844), petit-fils de Tarih, chef

    lam tuna du Bhagw arta, devenu

    le Maroc d aujourd hui, a traduit

    et transcrit le prem ier le Coran

    en langue lam tuna il y a de cela

    plus de m ille ans.

    Les Ghomara vivant du côté de

    Tetouan ne seront pas en reste.

    Tumert, fondateur du

    mouvement almohad, traduira le

    Livre dans sa langue.

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    15/20

    Ulema sofiinke yi, wolof yi, al

    pulaaren yi, hausa yi, K iswahili

    kanembu yi, bamun yi, soose yi,

    Taraga yi, daa nu tekkiji Al

    xuraan, firi ka, bind ka ci seeni

    arafi bopp, mbaa ci yaxu araab.

    19

    -

    Hindu bamun mba ajami

    Rausa ag walafal yi nu ko

    tè nke lu fi

    yàgg lanu.

    Cosaan loolu moo ubbil yoon

    gannaaw gi kelifa diine ag

    boroom xamxam yi : Sultan

    N jooya, Malaam Jibril, U smaan

    Dan Foojo Dem, Cerno

    M ombeya, xali M ajaxate Kala,

    Tafsir Umar Sàll, Aaj M alik Si,

    Sheex Amadu Bamba mba Sè'rin

    Ma Isa Ka, Serin Limaamu

    Laay, Ibraxim Nas, Serin Aale

    Fall Sali, Serin Abiib Sail, Serin

    Abdu AzUz Si, Serin Aadi Ture,

    Sè'rin Abbaas Sàll ag seeni bokk

    jamono.

    2 Aada tekkinu Al xuraan yi

    nu def ci lakki Afrig yi, du jéex.

    Li tumuranke mooy nu bind leen

    ci daara yi. Foofu la yàkkamti

    def ko, mè.ne soxxikoo. Jot

    googu ci tekki Al xuraan ba

    bind ka,

    Les Uléma sofiinké, wolof, al

    pulaar, hausa, kiswahili,

    kanembu, bamun, taraga ou

    touareg, mandeng ou socé, ont

    traduit le Coran pour le

    commenter et le fixer par écrit

    dans leurs graphies propres ou

    avec l alphabet arabe.

    19

    - L écriture bamun, l ajami-

    hausa et le walafal utilisés à cet

    effetsontanciens.

    Cette tradition a ouvert plus

    tard, la voie au Sultan N joya, au

    Malam Jibril, à Usman Dan

    Fojo Deem , Cerno M ombeya, Ie

    Cadi Majahate Kala, Amadu

    Saar Njaay Saar, Tafsir Umar

    SalI, El Aaj Malick Sy,

    SheexAhmadou Bamba,

    Serigne Ma Isa Kâ, Serigne

    ~imamou laaye Sheex Ibraxima

    Nasse, Serigne Aale Faal SalI,

    Serigne Habib SalI, Serigne

    Abdu Aziz, Serigne Aadi Touré,

    Serigne Abbas SalI et leurs

    contemporains.

    2().. Les traditions établies de

    traduction du Coran en langue

    africaine ne se comptent plus.

    Le fait rare est de les voir fixées

    par écrit dans les écoles. C est

    de là que naît l urgenceOn l a

    ressentie alors que l on menait,

    9

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    16/20

    am na fanweeri at fiu yeg ko.

    Booba fiu ngiy liggeey ci IF AN

    ci wallu làkk yi ag sunu yeneeni

    nawle.

    21 -

    Jot googu moo fiu joo ci

    jë eméntu wii. Moo fiu joo, ci

    jële Al xuraan ci tekki m i ko

    Arkun tekki ci faranse, ngir

    wane benn ci yoon yi nu me.ne

    lawale, nu gaaw, Téeré bi;

    lawal mbind diine ag xamxam,

    ci njàngum xale yi ag xëyna

    mag fii itam .

    22. -

    Li mooma doli duggal ci

    tekki ag génnée Al xuraan ci

    wolof, dafa fekk jàng ag jàngale

    xamxambi làkk bokk ci samay

    ite.

    23- Am na ay at fiu door di

    foraatu, di tekki ag génné ciy

    téeré

    :

    ay tànn; ay way, mbindi

    xamxam ag pexekaay mbao

    tegfiig yi dëppoo ag jamano ci

    làkki Ajrig yi te di jërifio arafi

    araab mbaa yu latefi.

    24- Naari mbindin yooyu yépp

    danu tibbe seen cosaan fa doon

    Misira ag Sumeer: fiaari rééw

    yu yàgg yu me soon èinb xalaat

    ag fiitin yu lislaam , fiew ba Ma

    10

    . il Y a près de trente ans, des

    recherches sur les langues à

    l IFAN , avec d autres collègues.

    21 - C est cette urgence qui

    légitim e ce m odeste exercice.

    Elle a incité à traduire le Coran,

    à partir de la version française

    du Professeur Arkoun, avec

    l intention de suggérer une voie

    susceptible de diffuser

    rapidement le texte, l écriture, la

    religion et sa science dans la

    form ation de la jeunesse, voire

    celle des adultes.

    22 - Ce qui m a également

    poussé à traduire et publier le

    Coran, tient au fait qu étudier,

    enseigner les sciences de la

    langue et éditer, relèvent de mes

    préoccupations

    professionnelles.

    23- Linguiste, je me suis

    habitué depuis quelques années

    à collecter, traduire et publier

    des anthologies, des textes

    africophones de science et de

    technique grâce aux graphies en

    lettres arabes ou latines.

    24- C es deux écritures tirent, on

    le sait, leurs origines de

    l Egypte ancienne et de Sum er,

    qui ont produit les idées et les

    humanismes que l islam après

    Moïse

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    17/20

    Maisa Isa ag Isaa wéyé, beccali

    leen, gën leen dé] ag saxal ci

    xol yi ag xel yi.

    25 -

    Waaye Ii am, maanaa ci lii

    yépp, na nu ko waxaat, mooy

    daiioo iiaan boroom xamxam yi

    tari, tekki ag firi Al Xuraan

    weesu bu gaaw Ii, iioo jé.em

    mentu fii. N u bind seeni liggéey,

    ba jullit yi ag jàngkat yi ci suiiiy

    gox, ag yenee iii goxi addina yi,

    iioom iiépp mé njot ci Téeré bi,

    di ko tari ci arab, di ko wax ag

    di nemmeeku Ii mu éinb ci seeni

    lakki bes bu nekk. Sëriii su baax

    si, iioo ko wax Al Xuroon loo

    ci wax lu mu tuuti tuuti, fexeel

    ba xam lu mu tekki.

     

    Poo te loon

    et Jésus aura renouvelés et bien

    enracinés dans les esprits et les

    coeurs.

    25- Ceci dit, l essentiel est,

    répétons-le, notre souhait de

    voir les maîtres de savoir qui

    ont récité, traduit et commenté

    le Coran, aller rapidem ent au-

    delà de ce modeste exercice.

    Qu ils fixent par écrit leurs

    oeuvres, que les musulmans et

    les lecteurs d ici et d ailleurs

    accèdent au Livre, qu ils

    récitent en arabe pour le dire et

    le reconnaître dans leur languede tous les jours. Les guides

    vénérés l ont souligné: Le peu

    que tu dis du Coran, tâche de le

    comprendre pour le moins.

    Pathé F . D iagne

     

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    18/20

    T

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    19/20

    1-

    2-

    3-

    4-

    5-

    6-

    7-

    Suraat wi jëkk

    W acce Màkka 7 laaya

    Benn - Senn -

    Menn la- Raax M enn - Raax Yërëm

    Màggal Y àlla buuru dunyaa

    Raax M enn Raax yërem .

    Buuru bésu sëddaIe ba.

    Y aw la fiuy jaamu, yaw la fiuy fiaan ndimmël.

    Teg fiu ci yoon w ijub,

    Ci yoonu fii nga bégaie say mbaax;

    fii la merloowul te réerufiu

    1-

    2-

    3-

    4-

    5-

    Suraat eXIV

    Nit ni

    W acce ci Màkka 5 laaya

    Benn - Senn - Menn la - Raax M enn - Raax Yërëm

    Nil dam ay w ut kiiraay ci sunu BoroomBuur ci ku di nit

    Yàlla ci ku di nit

    W àttu m a ci m bonu kiy sol xalaat yu bon tey rocceeku

    Di waIlu bon ci xoli nit fii

    1-

    2-

    3-

    4-

    5-

    SURAAT eXIII

    Bes tenk

    W acce Màkka 5 laaya

    Benn

    -

    Senn

    -

    Mennla

    -

    Raax M enn

    -

    Raax Yërëm

    Nil dam ay w ut kiiraay ci Y àlla fa biir sete

    M uslu ci mbon gi ci m indeef yi mu sàkk

    M uslu ci m usiba guddi lëndem kërüs fa m u fiu bette

    M uslu ci mbonu dëmm yiy wàl ciy paspas

    Muuslu ci musibë kâfiaanu ki afiaan

    Suraat eXIl

    K enntalaayu Yàlla

    W acce ci M àkka 41aaya

    Benn - Senn - Menn la - Raax M enn - Raax Yërëm

    Nil: Y àlla kenn là

    D i Yàlla m i di ba faww; ki jürul kenn

    1-

    2-

    13

  • 8/18/2019 Qur'an in Wolof Language

    20/20

    3-

    4-

    1-

    2-

    3-

    4-

    5-

    1-

    2-

    3-

    1-

    2-

    3-

    4-

    5-

    6-

    ki kenn jurul

    Te amuI ku mu yamal

    Suraat eXI

    Abu Laxab

    W acce ci Màkka 5 laaya

    Benn - Senn - Menn - Raax M enn -

    Raax Yërëm

    Na fiaari loxo Abu Laxab ya faaf, te mu maf moom ci

    boppam

    A lalam aki jëfam du fiu ko jerifi dara

    D anafiu ko lakk ci safara say boy

    Moog jabaram ja yanu m att

    Te ci baatam la noo yeewi buumu xafici tandarm a

    Suraat ex

    Ndimmëlli

    W acce ci Màkka 3 laaya

    Benn

    -

    Senn

    -

    Menn la - Raax M enn

    -

    Raax Yërëm

    Bu nu ndimmalal Y àlla ag ndarnam ganesee

    Daa gis nit fii faxx andandoo jébbolusi ci diine Yàllaji

    Tàggeel Boroom bi tey baalu ndax dafa sopp di baal nit fii.

    Suraat CIX

    W eddikat yi

    W acce ci Màkka 6 laaya

    Benn - Senn - Menn la - Raax M enn - Raax Yërëm

    Yeen w eddikat yi

    Duma gëmi Ii ngeen gëm

    Du ngeen gëmi Ii ma gëm

    Gëmuma Ii ngeen gëm

    Gëmuleen Ii m a gëm

    ngeen arn seen diine, m an m a am sarna jos.