16
1 UNIVERSITE CHEIKH ANTA DIOP DE DAKAR (UCAD) ……………………………………………………………. INSTITUT FONDAMENTAL D’AFRIQUE NOIRE CHEIKH ANTA DIOP ……………………………………………………………………………… LABORATOIRE DE RECHERCHE SUR LES TRANSFORMATIONS ECONOMIQUES ET SOCIALES (LARTES-IFAN) ………………………………………………………. PROJET D’EVALUATION DES APPRENTISSAGES À TRAVERS LA MISE EN PLACE D’UN BAROMÈTRE DE LA QUALITÉ DE L’ÉDUCATION JANGANDOO EPREUVES POUR L’EVALUATION DES CONNAISSANCES DES APPRENANTS EN LECTURE, CALCUL ET CULTURE GENERALE (FRANÇAIS, WOLOF ET PULAAR) LECTURE MAI 2012

JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

  • Upload
    others

  • View
    0

  • Download
    0

Embed Size (px)

Citation preview

Page 1: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

1

UNIVERSITE CHEIKH ANTA DIOP DE DAKAR (UCAD)

…………………………………………………………….

INSTITUT FONDAMENTAL D’AFRIQUE NOIRE CHEIKH ANTA DIOP

………………………………………………………………………………

LABORATOIRE DE RECHERCHE SUR LES TRANSFORMATIONS ECONOMIQUES

ET SOCIALES (LARTES-IFAN)

……………………………………………………….

PROJET D’EVALUATION DES APPRENTISSAGES À TRAVERS LA MISE EN PLACE D’UN

BAROMÈTRE DE LA QUALITÉ DE L’ÉDUCATION

JANGANDOO

EPREUVES POUR L’EVALUATION DES

CONNAISSANCES DES APPRENANTS EN

LECTURE, CALCUL ET CULTURE

GENERALE

(FRANÇAIS, WOLOF ET PULAAR)

LECTURE

MAI 2012

Page 2: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

2

LECTURE

Page 3: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

3

Page 4: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

4

EPREUVE DE LECTURE N° 1

1. Lettres/sons

Lis correctement les sons suivants :

A, o, m, t, e

F, u n, v s

Souligne les lettres t, d, i, b, l, p dans

les mots suivants :

Ali – petit - crocodile

- table – patate -dormir

3 . Mots

Lis correctement les mots suivants

Saison, semoir,

Cheval, pleine,

J’arrive, baobab,

Parapluie, ballon,

Hivernage, maison

2. Syllabes

1. Lis correctement

les syllabes :

Na, tou,

de, mi,

ta, pl,

vr, bi,

on, ge

2. Montre les

syllabes « mo» et

« dou » dans les

mots et lis les:

Moto

Pomme

Modou

Mauvais

Amadou

4. Paragraphe

Lis le paragraphe

Le dispensaire de Darou

est situé au milieu du

village, tout près de

l’école. Il comprend trois

bâtiments peints en blanc.

L’un d’eux abrite la salle

de soins.

Manuel de lecture Sidi et Rama

Page 5: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

5

1. Qui demande aux enfants de nettoyer la maison?

2. La famille se réveille tôt pour faire quoi ?

3. Quand la famille nettoie-t-elle la maison?

1.5 Texte et compréhension

La veillée

Le clair de lune inonde l’air.

Et tout est presque aussi clair

Qu’en plein jour.

On entend la musique d’un filao.

Grand-mère,

Asseyez-vous au milieu de nous

Et racontez-nous

Une belle histoire sur l’esclavage. Daniel Thaly

Poètes d’expression française

Éditions du Seuil

Texte adapté

5.Texte et compréhension

Lis le texte et réponds aux questions

Le nettoyage de la maison

Quelques jours avant la Tabaski, Père Modou demande

aux enfants de nettoyer la maison. (…).

La veille de la fête, la famille se réveille tôt pour ce

travail. Sous la surveillance de mère Nafi, les uns

balaient la cour, les autres creusent un trou pour y mettre

les ordures. Rama lave la cuisine et la véranda à grande

eau. Aminata s’occupe du salon.

(D’après le manuel de lecture Sidi et Rama

M.E.N du Sénégal, INÉADE.)

Page 6: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

6

2.1 ÉPREUVE DE LECTURE N° 2

1.Lettres/sons

Lis correctement les sons

S, j, i, b, y

O, z, u, h, r

Montre les lettres : t – n – o– b– i – v

dans les mots qui suivent

Voilà – natte – bijou – table - robe

3. Mots

Lis correctement les mots

chemin – semaine – sommeil

boucle – buvard – beaucoup

texte – lexique - homme – heure

2.1.2. Syllabes

1. Lis correctement les

syllabes suivantes :

ma – dou – mai

son – fro – mu –

ge – ven - bei

Montre la syllabe « ga »

dans les mots:

Glace

Gâteau

Gamin

Gamelle Bagage

2.1.4 Paragraphe

Lis le texte

Bonjour, dimanche !

Disent les branches.

Bonjour, soleil !

Murmurent les abeilles.

Bonjour, chemin !

S’exclament les lapins

Toi, qu’attends-tu, petit

enfant,

Pour crier bonjour à maman?

Page 7: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

7

1. De qui parle l’enfant dans le texte ?

2. Comment était l’oncle?

3. Que faisait-il en ville?

2.1.5.Texte et compréhension

Lis le texte et réponds aux questions

L’oncle Mamadou

Mon oncle Mamadou était un peu plus jeune que mon père ; il

était grand et fort, toujours correctement vêtu, calme et

digne ; il avait été écolier, puis il était venu poursuivre ses

études en ville. Il était respecté par tout le monde.

(D’après Camara Laye, l’enfant noir.)

Page 8: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

8

3.1 ÉPREUVE DE LECTURE N° 3

1.Lettres/sons

Lis correctement les sons suivants :

K, O, p, s, i,

d, u, f, l, a Montre les lettres b - p –o – f – s - u

baobab - . Une – parapluie – soleil

– fête - ballon

3. Mots

Lis correctement les mots suivants :

amadou ; saison ; fromage ; salade ;

maman

mouton ; contre ; vélo ; ballon ;

jolie

2.Syllabes

1. lis correctemnt les

syllabes

la tou

une beau

Na dou

Jo pl

gr ro

2. Montre la syllabe

« na » dans les mots

Natou

Narine

Aminata

Banane

Anta

4 Paragraphe

Lis le texte

Je sais qu'ils pleurent dans la nuit Ces enfants pauvres sans abris, Les voilà amassés dans les rues de la ville, Tristes et sans personne pour les aider.

Page 9: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

9

1. Qu’est ce qui s’est passé dans ce texte ?

2. Que faisaient Amadou et sa sœur en ville ?

3. Comment étaient-ils ?

5. Texte et compréhension

Lis le texte et réponds aux questions

Un accident

Un jour, Amadou et sa sœur visitaient les beaux magasins et les boutiques

de la ville.

Tout à coup, un grand bruit attira leur attention.

Affolés, ils couraient dans tout les sens : c’était un grave accident. Un

camion et un taxi se sont heurtés violemment. Le choc a été terrible.

Texte adapté

Page 10: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

10

Page 11: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

11

LW 1

lecture et identification

1 . ARAF

Jà ngal araf yi ci anam wu jub

a – o – m – t – e – f - u – n – nd - mb Woneel araf t, d, o, m, u, f ci baat yii

meetar – noflaay – mbattu – àndandoo – sot – talaata

3. BAAT Jàngal baat yi ci anam wu jub

Saam - golo – taaru –nijaay- daara – ngénté –cere – nawetaan– sutura – joæante

2 . DOGI BAAT

1. Jàngal dogi baat yii

Na, tu,

de, mi,

ta, mbe,

ngo, bi,

ndu, ge

2.woneel te jàng dogi baat « ma» ak « du » ci baat yii

Mata

Pom

Móodu

Musaa

Aamadu

4. PÀCCU JUKKI

Jàngal pàccub jukki bii

Aminaa xale bu yaru la. Ku fonk njàngam la itam. Foo ko fekk, su demul ekkool, mu ngi tiim ay téeréem di jàng mbaa muy nafar.

Page 12: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

12

1- Kan la bukki àndal?

2- Ñaata gejj lañ for?

3- Ndax séddale mi aw na yoon? Lu tax?

5 . JUKKI

Jàngal te tontu ci laaj yi

SÉDDALE BUKKI

Bukki, jabaram ak doomam dañu doon tukki. Ba ñu demee ba ci yoon wi ñu for mbuus mu def ñetti gejj yu baax.

Bukki daldi ne: Bàyyiléen ma séddale gejj yi. Mu ne jabar ji

- am ! yow ak sa doom gejj » ,

- “man ak sama gejj, gejj”

Kon ñaar ñu nekk a bokk benni gejj.

Page 13: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

13

LW2

1. ARAF

Jàngal araf yi ci anam wu mucc ayib

r – i – m – é - x u – ñ – æ- mb -à Woneel araf ñ, mb, i, x, é, m ci

baat yii:

ñam – mbootu – tilim – taxaw – fénétal - sét

3.BAAT

Jàngal baat yii:

xoolal – saxaar– sàkk– saaku–sakkan - loxo - looco – cooroon – coono - ñaxtu

4 . PÀCCU JUKKI

Jàngal pàccub jukki wii

Garab lu am solo la ci sunug dund. Bu naaj wi tàngee, dañuy soxla ker gu ñu serloo. Bu noor bi xóotee, ba jur gi loof, sàmm àjji xobu garab xonte ko. Su jàngoro duggee, ñu gas reen, mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war.

.2.DOGI BAAT

Jàngal dogi baat yii :

Ña- du

mi- taa

ma-taa

du -ma

di -mbi

Woneel te jàng dogi-baat « ga « ci baat yii:

ganaar

garaat

magale

siga

Page 14: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

14

1. Màggat mi, ñan la dëkkal ?

2. Kan moo tooñ picc ?

3. Lan moo waral picc di boole jaan ?

5. JUKKI

Jàngal jukki bi te tontu ci laaj yii

AY DU YEM CI BOPPU BOROOM

Dafa amoon jigéen ju màggat ju dëkkoon ak jaan ak picc ci néegam. Bi mu dëkkee ak jaan ak picc, picc nen bu mu nen, jaan naan ko.

Picc dem ci nit, ne ko : -Nit, ay du yem ci boppu boroomam te dëkkandoo jàmm a ci gën ! Damaa bëgg nga demal ma ci jaan mu bàyyi samay nen.

Nit ne ko : - Ayu jaan ak picc lu ciy yoonu nit ; sama yoon nekkul ci, seetil keneen.

Noonu la picc demee ci ñépp boole leen ak jaan, kenn waxul ci. Mu ne –Léegi daal wax naa : te ku ma wax mu bañ. Fii mu ne nag, sonn naa, li ma xam léegi ma def ko.

Page 15: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

15

LW3

1. ARAF

Jàngal araf yii ci anam wu mucc ayib

f- o –s –ó –q – e – ng - l – nd - u Woneel araf ó- ng - s- q, l, f ci baat yii :

-bóli – safal –

ngegenaay – taala –

goro – sëqët

3.BAAT

Jàngal baat yii ci anam wu mucc ayib:

cóolo – cere- soccu– tere – làkk – tàkk – kaar – lakk -mën – muñ

wor– raw – werante – waxu

4 . PÀCCU JUKKI

Jàngal pàccub jukki bii

Yow doomi réew mi kan nga yaakaar ci sam réew ngir mu naat ?

Xamal ne sam réew de :

yow la yaakaar ciy toolam ;

yow la yaakaar ciy géttam

Yow la yaakar ciy pexeem

Rikk waay : Takkul te te gore ngir sam réew

2.DOGI BAAT

Jàngal dogi baat yii

da – ug mi – suu oq – ne mbi - ngo dee - le

Woneel te jàng dogi baat bii“se”:

Kese – dese xesenu-teese tamaate

Page 16: JANGANDOO - Accueillartes-ifan.org/pdf/Lecture Fran et wolof.pdfxóotee, ba jur gi loof, i xobu garab xonte ko. Su jàngoro mbaa xas ci xanc wi ngir faju. Kon fonk garab moo ñu war

16

1. Kan mooy Buuru àll bi ?

2. Kan moo jooy ?

3. Ci seen gis-gis ndax li bukki wax ne moo tax muy jooy dëgg la ?

5. JUKKI

Jàngal jukki bi te tontu ci laaj yii

NDAJEM RABI ÀLL YI

Gaynde buuru àll bi dafa woote ndaje mu mag dajale ci rabbi àll yépp. Ba ñu teewee, mu génn ñu rëkk ndënd yi, jiin tama yi, xalam yi jib géwél naan ko « njaay jaata njaay buuru àll bi ».

Bi yaram wi tàngee mu daldi ne : gannaaw ba ma leen nuyóo yéen waa réew mi, dama leen di xamal ne tey jii sama xol sedd na ci yéen.Lenn doææ a waral ma woote. Tey jii, damaa fas yéenée rey ki gën a ñaaw ci dëkk bi. »

Laata muy daaneel, bukki jooy. Ne, céy man tey jii laay ñàkk sama xarit, sama waay, golo.